Ko faati e naatnugol jaŋde ɗemɗe ngenndiije he Duɗal Ngenndiwal Njuɓɓudi laamu e Jaaynugol e Ñaawoore (ENAJM)

0
2363
Maaɗe tati pelle pine ngenndiije
Maaɗe tati pelle pine ngenndiije

Jokkorde pelle pinal ngenndiije pulaar, sooninke e wolof (FƁPM, AMPLCS, APROLAWO) nanii, rewrude e jaayɗe, kurmbitgol, ñalnde alkamiisa 15 oktoobar 2020, tumbudu heblo he nder ɗemɗe ngenndiije wonande doge « ñaawoore » e « njuɓɓudi laamu », to Duɗal ngenndi ngal Njuɓɓudi laamu e Jaaynugol e Ñaawoore (ENAJM).

Pelle amen ɗee, sabu mum en wonde pelle-baafal hare ngam keɓtingol timmungol ɗemɗe men ngenndiije rewrude e laawɗingol mum en, e kuutoragol mum en he nder denndaangal fannuuji nguurndam leydi ndii, mbaawata tan ko weltaade e ndee feere, so janngingol ɗemɗe Pulaar, Sooninke e Wolof to ENAJM, ngam, e yeru, « kalfinaaɗo njuɓɓudi laamu ine waawaa haaldude, hunuko e nofru, e ɓiɗɗo leydi he nder ɗemngal ngal ɓuri nande ».

Kono tan, e miijo amen, ndee feere hesere ine luurondiri e hoore mum, sibu ko toɗɗii « kalfinaaɗo njuɓɓudi laamu » e « ñaawoowo » koo, ɓuri toɗɗaade kadi ko jannginoowo e cafroowo, kam e denndaangal mecce jowitiiɗe e mbaawka laamu. Ko ɗuum tagi, so en njiɗii ndee feere yettoo no moƴƴi faandaare mum toɓɓaande ndee, alaa-e-sago nde naatta e feere ɓurnde yaajde, so mbayliigu tippudi nehdi e jaŋde tuugiingu e janngingol ɗemɗe men ngenndiije ɗee kala, nde tuugoo e politik goonganteejo laawɗingol ɗemɗe Pulaar, Sooninke e Wolof.

Ko ndeen tan ENAJM e denndaangal juɓɓule jaŋde e heblo ngonata nokkuuji mahooji ngootaagu ngenndi, ɗi ngona kadi kuutorɗe baawɗe rokkude halfinaaɓe njuɓɓudi laamu ɓee, ñaawooɓe ɓee, e jaaynooɓe ɓee, e denndaangal fanniyankooɓe « geɗe ndenndaandi », gannde paatuɗe e ɗemɗe, e pinal e renndo, gaddanooje ɗum en waawde jokkondirde e yimɓe ɗo ɓe ngollotoo ɗoo, kam e waawde ardaade gardagol juumtungol.

Nuwaasoot ñalnde 20/10/2020

Jokkorde pelle pinal


حول إدخال تدريس اللغات الوطنية في المدرسة الوطنية للإدارة والصحافةوالقضاء

علمت منسقية الجمعيات الثقافية الوطنية البولارية والسوننكية والولفية عبر وسائل الأعلام بالإطلاق الرسمي يوم الخميس 15 أكتوبر 2020 لوحدة تكوين في اللغات الوطنية لقطاعات « القضاء » و »الإدارة العمومية » بالمدرسة الوطنية للإدارة والصحافة والقضاء.

وبوصفنا منظمات في طليعة الكفاح من أجل الاعتراف الكامل باللغات الوطنية من خلال إضفاء الطابع الرسمي عليها واستخدامها في جميع مناحي الحياة الوطنية لا يسع جمعياتنا إلا أن ترحب بقرار « تعليم اللغات البولارية والسوننكية والولفية في المدرسة الوطنية للإدارة والصحافة والقضاء، وذلك من أجل تمكين « الإداري من مخاطبة المواطن مباشرة باللغة التي يفهمها بشكل أفضل »، من بين أمور أخرى.

ومع ذلك نعتقد أن هذا الابتكار يحمل في حد ذاته تناقضًا لأن ما يحتاجه « المسؤول » و « القاضي » في هذا المجال يحتاجه أكثر منه المعلم ومقدم الرعاية الصحية وجميع موظفي الدولة. لذلك ، إن أردنا أن تحقق هذه المبادرة هدفها المنشود بالكامل فيجب أن تكون جزءًا من منظور أوسع لإصلاح النظام التعليم إصلاحا قائما على تدريس جميع لغاتنا الوطنية، وأن تكون مدعومة بإرادة سياسية حقيقية لإضفاء الطابع الرسمي على اللغات البولارية والسوننكية  والولفية.

وبهذه الطريقة فقط ستكون المدرسة الوطنية للإدارة والصحافة والقضاء وجميع مؤسساتنا التعليمية والتكوينية بوتقات للوحدة الوطنية وأدوات قادرة على تزويد إداريينا وقضاتنا وصحفيينا وجميع المتخصصين في شؤوننا العمومية بالمعرفة اللغوية والثقافية والاجتماعية التي ستمكنهم من التواصل مع السكان الذين يعملون بينهم، وأن يحكموهم بشكل أكثر فعالية.

نواكشوط، في 20/10/2020

مكتب المنسقية

DANTAXE

Fi be ga katta jamaanen xannun roye xaranra be ga marande, xibaarikinnen do kiiten xaranŋundini. Jamaanen feddu (Fulle, Sooninke do Wolofo), i jokkindan da xibaaren mugu moxodagante ti xibaarindikille nan ti xannun xaranŋunden jope Alxamisa Oktooburu 15 siine 2020, kuta be ga xannun da ti xarankille be ga kiitaanon betten da, do jamaanen marande xaranra ke noxo.

Feddu beenu ga ni siito, i ga fanqene jamaanen xannun toŋonde do i ronde jamaanen killun su di, o feddun nan katta sewono ti ke anniye wutte, ken ga teŋana jamaanen xannu (Fulle, Sooninke, Wolofo) xaranŋunde ken xaranra noxo ken ga katono marandan deemana jokkindanlenmaaxu i do jamaanen renmen naxa mefaamuye kanma.

O da a sinma, ke faraaxunde da i genmanlenbalaaxun koyi baawo, ke be ga genme maranda, kiitaana, ken wa genme xaranŋundan do jaarandan do golliñanraqu su ga dowulan maraye. Ken noxon di, o ga a mulla ke anniye nan joofe i natan ŋa, a nan xawa bangene xaranŋunden faraaxunden noxon ya, a na a ñi jamaanen xannun su wa xarene ti politikin kille be ga Fulle, Sooninke do Wolofon dagandini.

Ken moxo baane ya ni, xaranra ke do xaranŋundidingiron su gan xawa  ñiini kapen daaxa do surumaadu beenu ga marandaano, kiitaano, xibaarikinnaano kun do soro su ga xidimene jamaanen gollen da, do xannun tuwaaxunu, wulliyu do jamankafon gollu, i ga katono jokkindenlenmaaxun tapa jamaanen renmun naxa, i kun beenu ga ni golliñanlenmo, a do i na kato toorini moxosiri.

Nuwassoto, 20 Oktooburu 2020

Jokkindan Biro

Xamle

Ci lu jëm ci duggal njàngum làkki réew mi ci <<ENAJM>>.

Lëkkaleb mbootaayi aada ak cosaan ci réew mi, Pulaar, Sooninke ak Wolof (ARPRIM, AMPLCS, APROLAWO) yëg na ci tassukaayu xibaar yi, ndoorte alximis 15 oktoobar 2020, njàngaleb làkki réew mi ca <<ENAJM>> ñu jàgleel ko àttekat yi ak ni saytu caytu réew mi.

Ni ñu nekke ay mbootaay yu mësa taxaw ngir ñu jox gëdd, gu mat sëkk làkki réew mi, ci yoonal leen, jëfandikoo leen ci bepp anami dundu réew mi, tax na nu rafetlu dogal bi jëm ci jàngale lakki Pulaar, Sooninke ak Wolof ca <<ENAJM>> ngir may ñi saytu caytu, ñu mën wax ak askan wi ci làkk wi ñu gëna xam.

Waaye yaakaar nanu ni, beeste bii ëmb na ñakk làyam, ndax li war ñi ci caytu gi ak àttekat yi, moo war jàngalekat ak fajkat bi ak ñepp ñee liggéey ci nguur gi. Koon sunu bëggee copite bii egg ci jëmoom, dañu kay def ci anam wu yaatu, làlu ci soppi tëralinu njàng mi, mu sukkandiku ci jàngale sunuy làkki réew yepp te li kay lal di bëgg – bëgg ci politik, yoonal làkki réew mi, Pulaar , Sooninke, Wolof.

Ci loolu rekk la <<ENAJM>> ak bepp kureelu njang ak tàggat di nekk ndajem bennoo askan wi ak itam jumtu yu mën jox ñi saytu caytu yi, ak kepp kuy liggéey ci nguur gi, xam – xam ci làkk, aada ak cosaan, ak nekkinu askan yu leen di may ñu joge askan wi nga xam ni ci biiram lañuy liggéeye te di leen yore ni mu gënna rafete.

Lëkkaleg mbootaay yi

Nuwaasoot, 17/02/2020

A propos de l’introduction de l’enseignement
des langues nationales à l’ENAJM

La Coordination des Associations culturelles nationales pulaar, sooninke et wolof (ARPRIM, AMPLCS, APROLAWO) a appris, par voie de presse, le lancement officiel, le jeudi 15 octobre 2020, d’une unité de formation en langues nationales pour les filières « magistrature » et « administration publique » de l’Ecole nationale d’administration, de journalisme et de magistrature (ENAJM).

En tant qu’organisations à l’avant-garde de la lutte pour la reconnaissance pleine et entière des langues nationales à travers leur officialisation et leur usage dans tous les rouages de la vie nationale, nos associations ne peuvent que se féliciter de la décision d’enseigner les langues Pulaar, Sooninke et Wolof à l’ENAJM, pour permettre, entre autres, à « l’administrateur de s’adresser directement au citoyen dans la langue qu’il comprend le mieux ».

Nous estimons, cependant, que cette innovation porte en elle-même sa propre incohérence, car ce qui est valable pour « l’administrateur » et le « magistrat » l’est encore plus pour l’enseignant et le soignant et pour tous les corps de métiers relevant de l’autorité de l’État. De ce fait, si on veut que cette initiative atteigne pleinement son objectif visé, elle doit s’inscrire dans la perspective plus large d’une réforme du système éducatif basée sur l’enseignement de toutes nos langues nationales, et être sous-tendue par une réelle volonté politique d’officialisation des langues Pulaar, Sooninke et Wolof.

C’est seulement ainsi que l’ENAJM et toutes nos institutions d’enseignement et de formation seront des creusets de l’unité nationale, et des outils aptes à procurer à nos administrateurs, magistrats, journalistes et à tous les professionnels de la « chose publique » les connaissances linguistiques, culturelles et sociologiques qui leur permettront de se lier aux populations au sein desquelles ils travaillent, et de gouverner plus efficacement.

Nouakchott, le 20/10/2020

Le Bureau de la Coordination

Woppu jaabawol

Winndu yowre maa
Winndu ɗoo innde maa

Ce site utilise Akismet pour réduire les indésirables. En savoir plus sur comment les données de vos commentaires sont utilisées.