Bayyinaango faatungo e Covid-19

0
1780
Hol no koraonaa reentortee
Hol no koraonaa reentortee

Gila desaambar 2019, ñawu koronaawiris (Covid-19) nana jokki bonannde mum he winndere ndee. Ngu fuɗɗorii ko to Wuhan, to leydi Siin. Caggal ɗuum ngu reɓi ɗoon e ɗoon e winndere ndee no diidorinoo. Hannde oo, ko ina ɓura miliyaaruuji 3 neɗɗo, hono hedde feccere winndere ndee ko waawnaaɓe uddaade nder galleeji mum en, ngam hulde raaɓeede, Alla e raaɓo ñawu nguu yaawde. Leyɗe ɓurɗe alɗude e doolnude ko gaanduɗe heen, tee e oo sahaa maayɓe ɓee njettiima capanɗe ujunere. Duunde Afrik, Muritani, sikkatnooɓe ko duulaaɓe, kam enen naatii he ngaanumma.

E tuugnaade e ɗii dalillaaji fof,

  • Sabu faamde kulol tanaaji Covid-19 winndere ndee wondi hannde ngol ;
  • Sabu humpitaade bone dookɗe leydi men ɗee ;
  • Sabu yenaneede jojjugol denndinngol doole yimɓe fof, kam e ummannde mawnde ballondiral ngenndiwal ;
  • Sabu yenaneede e faamde kaangol e jojjugol noddaango ngo laamu nguu noddi yimɓe fof yo ummo ndaroo ;

Jokkorde pelle pine Pulaar, Sooninke e Wolof (FƁPM, AMPLCS, e APROLAWO) ine hunoo addude ballal mum, kam fof e famɗude, he kaɓtagol mboros COVID-19.

E nder ɗuum, Jokkorde ndee :

  • Ina nodda denndaangal terɗe mum, ɗo ɗe mbaawi wonde kala, nde ndarotoo, njanta he kaɓtagol Covid-19 ;
  • Ina semmbina kuule ɗe laamu Muritani ƴetti ɗee ngam daɗndude leydi ndii he nguu ñawu mbonngu ;
  • Ina ɗaɓɓa e Dowla Muritani nde ummantoo jeeyngal jaajngal, keewngal mbaadiiji, tuugingal he denndaangal ɗemɗe ngenndiije, dewrowal he boli ceertuɗi, kuutortoongal denndanngal jaayɗe e kuutorɗe kumpital (binndol, hito, wideyoo, enternet, laylayti renndo, ekn.) ;
  • Ina ɗaɓɓa he yimɓe ɓee nehdi ngam hisnude nafoore renndaande ;
  • Ina semmbina ɓiɗɓe leydi ndii kam e tumarankooɓe wonɓe e leydi ndii, gooto kala, e teelal walla e dental, nde ɗooftotoo laŋ kuule senaare e uddagol ɗe halfinaaɓe cellal leydi ndii njamiri ɗee.

Nuwaasoot, ñalnde 04/04/2020
Yiilirde Jokkorde ndee
——————————————–

بيان حول فيروس كورونا المستجد

يتعرض العالم منذ ديسمبر 2019 للإبادة بسب وباء فيروس كورونا المتجدد (COVID-19)، فبعد الحالات الأولى التي ظهرت في ووهان بالصين انتشر المرض بسرعة البرق في جميع أنحاء المعمورة. واليوم يضطر أكثر من 3 مليارات شخص – أي ما يقرب من نصف سكان العالم – إلى الحجز شبه الصارم خوفًا من العدوى التي تعني تطور المرض أضعافا مضاعفة. وتبدو أغنى وأقوى البلدان عاجزة، والوفيات وصلت بالفعل إلى عشرات الآلاف. إن بلدان القارة الأفريقية بمن فيها موريتانيا التي بدت في البداية وكأنها تنجو، تعيش اليوم في فترة اضطراب.

لكل هذه الأسباب،
- وإدراكا منها للقلق العميق الذي اكتسح العالم بسبب تهديد هذا الوباء؛
- وإذ يساورها القلق إزاء خطورة وإلحاح الوضع الذي يتعرض له بلدنا؛
- ووعيا لضرورة تكاتف الجهود والإرادة في هبة كبيرة من التضامن الوطني؛
- واقتناعا منها بأهمية وتوقيت الدعوة إلى التعبئة العامة التي أطلقتها السلطات العمومية الموريتانية؛
تتعهد منسقية الجمعيات الثقافية البولارية والسوننكية والولفية بتقديم مساهمتها المتواضعة في مكافحة فيروس كرونا.
وتحقيقا لهذه الغاية فإن المنسقية:
- تدعو جميع أعضائها أينما كانوا إلى التعبئة والانضمام إلى المعركة ضد هذه الجائحة؛
- تعرب عن دعمها القوي للتدابير التي اتخذتها الحكومة الموريتانية لإنقاذ البلاد من هذا الوباء المخيف؛
- تدعو الحكومة إلى اتخاذ تدابير واسعة النطاق لدعم الفئات الأكثر ضعفاً من السكان؛
- تطالب الدولة بتنفيذ حملة توعية واسعة وديناميكية، وباستغلال جميع اللغات الوطنية، وتعبئة جميع القنوات، وأدوات الدعم والاتصال (الكتابات والصوتيات والفيديو والإنترنت والشبكات الاجتماعية، الخ.)؛
- تستدعي روح الحرص على المصلحة الجماعية والانضباط لدى الشعب الموريتاني ؛
- تحث المواطنين والمقيمين الأجانب - بشكل فردي وجماعي - على التقيد الصارم بتدابير النظافة والحجز التي تقررها السلطات الصحية.
واكشوط، 04/04/2020
مكتب المنسقية
---------------------------------------

DANTAXE KATTA COVID – 19

Gelli Desanburu siine 2019, Koronafirus (coronavirus – Covid 19), alhoban da bono kiña duna yi. Taagumansu fanon bange falle Wuhan Siini jamaane (Chine), watte ke sanqi moxo jowe ñiinen danman kanma. Lenki miliyaarinu sikki sere, ken ga genme duna nooren soron taxanden su ro xuxupe, ti watte ke janbayen kannun saabu da, kuudo watte ke fuumuyen da. Jamaanu beenu senben ga i ya, i kitanton ga ni, i hawuje, soro beenu ga kara fina, wujuunun wujuunun ya ni. Afriki dunde do Moritani, fin fanan ŋa, watten ma kiñe i ya, lenki koota ke, i wa lasamaye di.

Ku fiinu su saabu da :

  • Taxasinde katta lasamayixoore be ga kiñe duna yi, COVID-19  ya ga da sabaabu ;
  • Sinmaye be ga katta watte ke ñaŋoye do a jawoyen da o jamaanen ro siga ;
  • Nan duŋe ti o senbun kape do dukinnu, jamaane medeemanden noxo ;
  • Moritani fankan ga da gango be wara katta o yi, a daga be su nan duŋe nan ñimi.

Wulliyun kafonun jokkindan xa wa i deemanden ritini fi be ga katta

COVID 19 gajanŋe.

Ken noxo, ARPRIM,  AMPLCS – Wagadu Saane  do  APROLAWO :

  • Kafonun wa i soron su xilli, i ga kato ñiini noqu su, i ga sikki nan kafi fanqe be ga katta COVID 19 ;
  • I wa i kittun kinni moritani toore, a ga da killu beenu wutu kuudo na jamaanen kisi ke alhoba ;
  • I wa a muurunu tooren maxa, a ga killu wuttu katta jamaanen leefanton deemande ;
  • I wa a muurunu dawulan maxa, a ga gansindixoore, senbente munnafan bagandini ti jamaanen xannun su, ken do xibaarindikillu su beenu ga a du ;
  • I wa jamaanen nafan do jamaanen renmun marayen muurunu ;
  • I wa a muurunu jamaanen renmun do tuŋaarankon maxa, i ga senoyen killun tangana do nan ro xuxupe, kun beenu sahan marandaanon ga da i yaamari.

NA WATTEN KAANE XATA, A YA N FASU A JAARANDE”

Nuwasooto, 04/04/2020
—————————————————–

Xamle bu aju ci Covid 19

Ca desambar 2019 ba leegi, mbasum doomi jàngoro koronaa (covid – 19) mungee faagaagal ci adina bi. Ganaaw benn – benn yi feeñoon ca Wuhan ca chine feebar bi law na ci suuf si yepp ci anam yu gaawagaaw, tay lu mat 3 miliyaar ci nit, xaw tollook gennawaalu ñee dund ci adina bi, gennatuñu seen kër mbaa seen genn bareetul ndax ragal wàlle, ndax mooy tasub feebar bi. Réew yi ëpp alal, gën bare doole mel na ni xamatuñu lu ñoo def, te ña fay dee mat jeeg ay fukki junne.

Afrik ak Muritani ñi yaakaaroon ni mucc nañu ci njaalbeen gi leegi ñungi jaaxle.

Lii yepp nu gis tax na nu :

  • Yeewu ci njaqare bi am ci adina bi, ndax feebar korona virus.
  • Yeewu ci fi réew mi tollu : metti na jàmp na
  • Gëm ni ñepp war nañu boole seeni doole, bokk bëgg – bëgg.
  • Am koolute, te mu wóor nu, ni woote bi nu yore réew mi def, ngir ñepp taxaw, am na solo, te ñow na ci waxtoom

Lakkaleeb mbootaayi aadak cosaan, (FƁPM/ARPRIM, APROLAWOORIM, APLCS) taxaw nañu ci bay seen waar ci xeex doomi jàngoro Covid 19 ciloolu, lakkaleb mbootaay yi ñu ngee:

  • Woo kepp ku bokk ci ñoom, ak fu mu mëna nekk mu fekki xeexum Covid 19.
  • Wone seen jàppale, matukaay yi nguuru Muritani jël ngir aar réew mi ci mbas mu bon mii.
  • Ñaan nguur gi mu gëna yaatal ndimal li jëm ci ñi gën néew doole ci askan wi.
  • Ñaan nguur gi ñu taxawal yeete bu yaatu te gaaw, sukkandiku ci làkki réew mi te bañ bàyyi benn yoonu tas xibaar (mbind, wax, video, internet, ëtt yi m.w)
  • Ñaan ku nekk seet njeriñu réew mi te ànd ak yar.
  • Ñaax bepp doomi réew mi, ak doxandéem yi fi dëkk, ñu sàmmonteek ndigal yi nguur gi dogal ñu aju ci set ak toog sa kër.

Lakkaleb mbootaayi aadak cosaan ci réew mi

Nouakchott, le 04/04/2020
——————————————————-

Déclaration à propos du Covid-19

Depuis décembre 2019, le monde subit les ravages par l’épidémie coronavirus (COVID-19).  Après les premiers cas, apparus à Wuhan en Chine, la maladie s’est propagée à une vitesse fulgurante sur la Terre entière. Aujourd’hui, plus de 3 milliards de personnes, soit prêt de la moitié des habitants de la planète sont contraints à un confinement plus ou moins strict, par peur d’une contamination, synonyme d’une progression exponentielle de la maladie. Les pays les plus riches et les plus puissants semblent désemparés, et les morts se comptent déjà par dizaines de milliers. Le continent africain, et la Mauritanie qui, dans un premier temps, avaient semblé être épargnés, sont aujourd’hui dans une période de tourmente.

Pour l’ensemble de ces raisons,

  • Consciente de la profonde inquiétude qui a gagné le monde face à la menace du Covid-19 ;
  • Soucieuse de la gravité et de l’urgence de la situation à laquelle notre pays est exposé ;
  • Convaincue de l’indispensable conjugaison des efforts et des volontés, dans un grand élan de solidarité nationale ;
  • Persuadée de la pertinence et de l’opportunité de l’appel à la mobilisation générale lancé par les pouvoirs publics mauritaniens ;

La Coordination des Associations culturelles pulaar, sooninke et wolof (ARPRIM, APCLS, APROLAWO)s’engage à apporter sa modeste contribution à la lutte contre le virus COVID 19.

Á cet effet, ladite Coordination :

  • appelle l’ensemble de ses membres, où qu’ils se trouvent, à se mobiliser et à se joindre au combat contre le Covid-19 ;
  • exprime son ferme soutien aux mesures prises par le gouvernement mauritanien en vue de sauver le pays de cette redoutable pandémie ;
  • sollicite du gouvernement l’adoption de larges mesures de soutien aux couches sociales les plus vulnérables de la population ;
  • réclame de l’Etat la mise en œuvre d’une sensibilisation large et dynamique, exploitant toutes les langues nationales, et mobilisant tous les canaux, supports et outils de communication (écrits, audio, vidéos, internet, réseaux sociaux, etc.) ;
  • en appelle au sens de l’intérêt collectif et de la discipline du peuple mauritanien ;
  • exhorte les citoyens et les résidents étrangers, individuellement et collectivement, à une observation stricte des mesures d’hygiène et de semi-confinement décidées par les autorités sanitaires.
  • Nouakchott, le 04/04/2020
    Le Bureau de la Coordination

Woppu jaabawol

Winndu yowre maa
Winndu ɗoo innde maa

Ce site utilise Akismet pour réduire les indésirables. En savoir plus sur comment les données de vos commentaires sont utilisées.